Articles de la catégories

Kalamay Kocc


Saafara’s 18 Safar

Read More

Mbëgeel_gi_ci_Xaritoo

Read More

Saafara’s safar a gën saphir Danala mussal ci safara Ay raagi xol dana soril Ay woopi yaram dana sekki   Su att mi aksee waajalal Su weer wi teroo magalal Su bês bi ñëwe rendil begglel Su magal gi weeso waajalatil   Ku def nga ku deful nanga def Ngir am i ngërëm yu ump …

0 127

Dee nga fétal-u bëgga ni la tuyy! Su ndaw si di garab mani ko guy Ndax yeemé na taaru neeleen suuy Ndox la mu Yalla fob sa xol bi duy Ba fooko nee jàkk mu sédd guyy ………………… Seen ak fonkanté taxawal na sëy Seen xaritoo rax xeeti bëgg yu rëy Ku xamul ba xam …

0 92

Ku ñuy taggati nañu ko tagg ndank Ku ñuy xasati yit nañuko xas ndank Lu waay rendi mu nacc ci-y loxoom Sò wicaxoo mu tiss ci sa-y moroom ………………………….. Xanaa du yeen-a andoon di kaas ? Ba tégg ci boppu reew mi keneen Naan ñu moo gën-a baax ka woon Tay kookii ñu fal lañu …

0 62

Fatté ngeen xanaa da ngeena fàté ? Sëy ak lumu mënti doon, fumu joté Du fa weesu ci bis bòbu lay maté Waayé xalé yu gòor yiy jaay nandité « Mé fils lu gaa yi di xaar laay laajté » —-§§—-§§—- Géwël-u juddu bi dila yokk stress « Goné-g jamm gi cëy bu ñu dundee Ba lay xéwal …

0 74