Saafara’s 18 Safar


Saafara’s safar a gën saphir

Danala mussal ci safara

Ay raagi xol dana soril

Ay woopi yaram dana sekki

 

Su att mi aksee waajalal

Su weer wi teroo magalal

Su bês bi ñëwe rendil begglel

Su magal gi weeso waajalatil

 

Ku def nga ku deful nanga def

Ngir am i ngërëm yu ump baay

Rawi maas bay dabi tanneef ya

Loolu moodi ndam li mata wut

 

Aboo rijaal mbër ma lii la jangale

Ngala ñun ñiy roy buñko saagane

Mukk bul faleeti kukoy caaxaane

Yalla may ñu ci jëf yu jaambaare

Précédent Gouvernement : La méthode Sankara !
Suivant The key reason why It Is Crucial to be able to For United nations and Affiliates of your family Counseling

Pas de commentaire

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *