Mbëgeel_gi_ci_Xaritoo


Dee nga fétal-u bëgga ni la tuyy!
Su ndaw si di garab mani ko guy
Ndax yeemé na taaru neeleen suuy
Ndox la mu Yalla fob sa xol bi duy
Ba fooko nee jàkk mu sédd guyy
…………………
Seen ak fonkanté taxawal na sëy
Seen xaritoo rax xeeti bëgg yu rëy
Ku xamul ba xam danga ni eskëy
Ñoom sax dañoo yeemu dëkké cëy

Mbêgeelu deugg mooma soxal !
……………….
Yalla la soob doyna la aw lay
Ci kiy laaj num mëna amé kay
Xaritoo ta fékk nobeel dila ray
Doon taal buy takk ta ni du fay
…………………
Xanaa yërëmoo xol bii di jooy
Bëgg dici taw muy gëna tooy
Xaritoo tax la di xoolé ni looy
Toolu mbëgeel bi dina booy
Di nala rëcc nga yuuxu wóoy
——–§§—–§§—-§§——-
—–§§ Lamp Fall Kala §§——- La Tribune 221 Lamp Fall Kala
Précédent De l’humour pour vous faire sourire...
Suivant Trêve ramadanesque

Pas de commentaire

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *